audio
audioduration (s)
1
29.8
transcription
stringlengths
1
591
di jëf ci anamug jàmm ak baalante ak jéllale ci diggante reew yi
booy tisóoli bu ko def ci kow nit ñi
sandaga par dakar dem dikk
ndekkete ku ñaaw kii laa leen di yóbbul
kenn ci ñoom la xelam toogatul fan yii taluñu lu dul kàmpaañ bi
yéen yéenay wax lii buñ ko def mais lii ci yéen la ëpp kon donc yaakaar naa ne
gerte tubaab xeetu garab la gu bokk ci njabootu cambretaceae
hlm las palmas
mamelles
dama jooy itam
kon nag yow yaay maanaam ki nga xam ne moo fi toogal anacim noonu la ci mboolem diwaan tambacounda noonu la
bu ñu ko mooñee rek lu énu duggee saafara mën na dugg ci sunu li nga xamante ni moom lañuy def
man ngaa dakkal lii
tëjleen bunt bi
xorñeññaloon na ma
sëriñ muhammadu faliilu mbàkke dàkkantal sëriñ fallu sëñ fallu fàllu galas alaaji fàllu
lii moo doonoon tàmbalig rawante gi ci wàllug sanc
këram gi na mel ni mu meloon léegi léegi
waaw tàngoor bi gën a tar phénomènes yi di gën a tar waaw su ko defee dinañ dem ba dund si addina bi dootul possible waaw suñ suñ fexewul ba wàññi ko tàngoor bi day gën di yokku phénomènes yi ma la wax noonu di gën di nekk
sushu girip awiyeer buy rey nit ash cinq enn un firndéel nañ ni dafa wàll kanaara bu faatu buñu gisoon altine ci marshland ci wetu lyon ci penku farans
soo leen gisee ak xare bi ñépp a nooral
nga xam ne danag koy jënd ca boutique yu ndaw yi
osaasunaa ñaar mayorku ñaar
di nuyu aussi sama yeneen collègues yi ma bàyyi foofu ku ci demee ni cheikh mboup cheikh omar fouti mboup
formation introduction même de nouvelle technologies
manoo leen a dimbali
amar diop
matukaayu yu mujj yi
du bari na njariñ
kaayleen ma takk leen
mën na démarrer liggéey bi
gare routière pompier
mbind mi nee ubbi njël lu njëkk li
takaal say dàll
dékh fleuve de mbao
póno bi peer na
dañu ciy wax ci injiil ci jëf teemeer ak juróom benn fukk ak juróom ñaar
waaye du saafara
jooy na jooyi mbégte
moo andi coow li yëpp
donc anacim mooy kiy doxal fii si sénégal
nu yóbbu ko
mu rafetlu loola
taw boobu boo ko amee
randalal doj wi bala ci nit di fakkatalu
ndimo lu xonq la sol dinga ko gaaw a gis
ba suba ba béykat bi mu nekk koo xam ne wax dëgg li mu war a xam yëpp sàlloo ak chanhement climatique
lànk ag topp
ndekkete ku ñaaw kii laa leen di yóbbul
damay seetaan ni muy rattaxale siman bi ci miir bi
nee nañu jàngal jigéen ñi bu ñu leen jàngaloon lu mu dee dee ñi nga xam ne ñun ñii nga xam ne ñoo ngi ciy yëngu lu mu dee dee dañoo jaaroon ci alpha bi
patte d oie
saxal di dàllu bul di dallu mukk nag
loo leen bëgg
commissariat dieuppeul
nun ñépp a bëgg ay tontu
boo ko gisee muy dem ak dikk nii rekk dafa jaaxle
muy dóor tànk yi ci suuf si ndax yàkkamti
abdu rahmaan léy
damaa begg ay fo
damaa ame mitit
dañu daan demlante ngir dëgëral jàmm ji amoon seen diggante
daa niru ku yërëmtalu
ma defoon ko ngir moom
beqi leen ma ñu gaaw
bokkunu yoon waaye jenn yàlla ji lanuy jaamu
géej gu diggu gi dees koo seddatle ci ñaari mbalka
donc vraiment
kii de moom laaj bi daanak
donc loolu moo tax muy mbéy di sàmm di napp di di napp ak yëpp si ñoom nekk na ay activités yoo xamante ni ñoom vraiment infoprmation climatique moom
marché thiakhogne
na ñuy déglu informations yi régulièrement fra
neena ñu dafa feebar
luy sa xalaat ci ni nguur gi y xeexe mbas mi
nànd naa lii
naka suba gi mbaa yéen a ngi ci jàmm
dañoo am ci lu mel ne ay mboo mbooloo yoo xam ne nii yor nañ seen xaalis
wóor na ma ne boo déggoon si ne teeloon naa ko yëg man foofu laay amee jiw
dama doon taà alxuraan ba yàgg ma gag
te tàgoor boobu baaaxul ci doomu aadama
guddaayam danay àgg ci juróom ñaar ba fukk ak ñaari sàntimet
dafay intervenir ci loolu
dànkaafu naa ko ba tàyyi mu të maa déglu
tàllalleen seen i yoxo
soo amee tamit loo ciy lu ñu war a yokk lan lay doon
jongante bu mujj bu waa all blacks lawoon ñoom ñi jël ndàm li ba noppi ñaari ayu bis ci ginnaw
damaa ponkale lool
ceeb baa ngiy xooje ba tey kenn xeragul ndox mi
yéen jigéen ñi amu leen fi problème am suuf jotin ci suuf
bi mu dalee jél garab bi la bàyyi say
màkkaanum pasteur daa lànkoon ne du ko joxe
bëggu ma xaj
moytuleen lépp lu mën a wootal yoo
alëmaañ ab noon bu ñepp bokkoon la ci ñaareelu xare b wër addiina yóbbu ci jëflante ci diggante ussr ak amerig ak njeexitalu xare bi tasub yoonalin gi doxalin aka ad yóbbu dëkk yi daanu
boo demee seen kër guddi sómbi lay reere
dinaa la dimbali
wéyal di dem ci kanam
damaa am i futtantaan
boo weesoo pom bi ba noppi nga jàdd ci sa càmmoñ
yoon yuy tege galag ak tembar